Video de: Freestyle Love De Toi 2 Lyrics Amsco Dbz Gang » Lyrics Fox.MusicaDe.Win

Bienvenidos a Fox.MusicaDe.Win Disfruta del Video de: Freestyle Love De Toi 2 2025 Amsco Dbz Gang » Lyrics y comparte musicas con los amigos, Musica Gratis 2025! Fox.MusicaDe.Win!.

Video de: Freestyle Love De Toi 2 Lyrics Amsco Dbz Gang » Lyrics

Amsco Dbz Gang - Freestyle Love De Toi 2 Lyrics


[Couplet Unique]

Bëgg na am doom ak yow
Sa dox neex na ma torop
Di la xalaat bu baax a baax
Foon naa la xam naa ne di nga dellusi
Sama mbëggël yow laay xalaat
Mënuma nelaw sax yow laay xalaat
Yakar naa ni ma ngi ley bëgg nopp
Ne ñu dem geej ci kanam tuuti
Dama bëgg nelaw ak yow tey
Soo bëggee mën naa la woo
Bëgg na la bu baax waxa guñu dara
Sa kanam neex na ma torop
Dinaa neex xam say xibaar
Lu tax nga dëggër bopp
Na nga def naam naa la torop
Man bëgg na la ba léegi
Ne ñu dem geej ci kanam tuuti
Dama bëgg añ ak yow sama kër
Yow laay xalaat guddi ak bëccëg

Freestyle Love De Toi 2 » Amsco Dbz Gang Letras !!!
Esta web no aloja ningun archivo mp3©Fox.MusicaDe.Win 2025 Colombia - Chile - Argentina - Mexico. All Rights Reserved.

Musica Online, Escuchar musica online , Musica En Linea, Musica en linea gratis, Escuchar Musica Gratis, Musica Online 2025, Escuchar Musica

Musica 2025, Musica 2025 Online, Escuchar Musica Gratis 2025, Musica 2025 Gratis, Escuchas, Musica de Moda.