Video de: Balma Lyrics Wally B Seck » R B Fox.MusicaDe.Win

Bienvenidos a Fox.MusicaDe.Win Disfruta del Video de: Balma 2025 Wally B Seck » R B y comparte musicas con los amigos, Musica Gratis 2025! Fox.MusicaDe.Win!.

Video de: Balma Lyrics Wally B Seck » R B

Wally B Seck - Balma Lyrics


Sonn naa
Maa la tooñ, baal ma
Woh woh woh
Sonn naa
Man maa la tooñ, baal ma

You feel man de wéet naa
You're still, you're still my boo
Everyday ma ñàkk fàyda go back
Ñëw sukk jéggalu ci sa kanam baalu àq
Baalu naa la ngir Yàlla baal ma
Daf ma mere xam naa ni ma tooñ
Everyday ma ñàkk fàyda go back
Ñëw sukk jéggalu ci sa kanam baalu àq

Nangu sama défaite, tey ya am ndam (am ndam)
Loo ma mere mere xam nga maa xam
Sama baby girl kaay jéggalu na
Sama baby girl bàyyil mer wuyu ma
Nangu sama défaite, tey ya am ndam (am ndam)
Loo ma mere mere xam nga maa xam
Sama baby girl kaay jéggalu na
Dellusil ma baby oh-ouh-ah yeah

Sonn naa
Maa la tooñ, baal ma
Woh woh woh
Sonn naa
Man maa la tooñ, baal ma

Chérie coco me I love you du débat
Tu sais pour toi je ferai le premier pas
Des jeux de rein à la Wally - Ipupa
Neexaalat kër gi on fera n'importe quoi
Yow tamit, bàyyil sa mer bi te nga ree comme Khaby
Lam la ma déy sonal sa xel, nangu naa ni
Maa ko def, maa la tooñ
Buñu mel ni Tom & Jerry

Lak lak like fire
Woh woh woh woh woh woh
Sexy lady
Dama wéere tay, jéggalu naa
Sama baby girl bàyyi mer, wuyu ma

Nangu sama défaite, tey ya am ndam (am ndam)
Loo ma mere mere xam nga maa xam
Sama baby girl kaay jéggalu na
Dellusil ma baby oh-ouh-ah yeah

Sonn naa
Maa la tooñ, baal ma
Woh woh woh
Sonn naa
Man maa la tooñ, baal ma

Balma » Wally B Seck Letras !!!

Videos de Wally B Seck

Esta web no aloja ningun archivo mp3©Fox.MusicaDe.Win 2025 Colombia - Chile - Argentina - Mexico. All Rights Reserved.

Musica Online, Escuchar musica online , Musica En Linea, Musica en linea gratis, Escuchar Musica Gratis, Musica Online 2025, Escuchar Musica

Musica 2025, Musica 2025 Online, Escuchar Musica Gratis 2025, Musica 2025 Gratis, Escuchas, Musica de Moda.