Video de: Goree Lyrics Youssou Ndour » Afro Fox.MusicaDe.Win

Bienvenidos a Fox.MusicaDe.Win Disfruta del Video de: Goree 2025 Youssou Ndour » Afro y comparte musicas con los amigos, Musica Gratis 2025! Fox.MusicaDe.Win!.

Video de: Goree Lyrics Youssou Ndour » Afro

Youssou Ndour - Goree Lyrics


Bama démé gorée manne
Andak samayyy kharite
Demm sa keur diam gawonne
Dama dalle di seugemm dioyy
Goor yi magg yi bi boor
Djiguéne yu magg yi bi boor
Goor yu ndaww yi bi boor
Djigéne yu naww yi tchi bénène boor
Niu daddi fayy khali yonne
Yonne bo khamni dangay demm
Yonne bo khamni dangay dem
Sa khell du demm ludull ssi délussé
Lolloyyy natu lawu buur bi mi borom doggal yyé
Lolayy nattu lawu buur bi boromm kunfa yakune

Bama démé gorée manne
Andakk samayy kharit
Demm sa keur diamm gawonne
Dama dalle di seugueumm dioyy
Goor yi magg yi bi boor
Djiguéne yu magg yi bi boor
Goor yu ndaww yi bi boor
Djigéne yu naww yi tchi bénène boor
Niu daddi fayy khali yonne
Yonne bo khamni dangay demm
Sa khell du demm ludull ssi délussé, ah ah gorée

Lolloyyy natu lawu buur bi mi borom doggal yyé
Lolayy nattu lawu buur bi boromm kunfa yakune
Lolloyyy natu lawu buur bi mi borom doggal yyé
Lolayy nattu lawu buur bi boromm kunfa yakune

Gorée, natu lawu buur bi mi borom doggal yyé
Lolayy nattu lawu buur bi boromm kunfa yakune

Goree » Youssou Ndour Letras !!!

Videos de Youssou Ndour

Esta web no aloja ningun archivo mp3©Fox.MusicaDe.Win 2025 Colombia - Chile - Argentina - Mexico. All Rights Reserved.

Musica Online, Escuchar musica online , Musica En Linea, Musica en linea gratis, Escuchar Musica Gratis, Musica Online 2025, Escuchar Musica

Musica 2025, Musica 2025 Online, Escuchar Musica Gratis 2025, Musica 2025 Gratis, Escuchas, Musica de Moda.