Video de: Incha Allah Lyrics Ismael Lo » Lyrics Fox.MusicaDe.Win

Bienvenidos a Fox.MusicaDe.Win Disfruta del Video de: Incha Allah 2025 Ismael Lo » Lyrics y comparte musicas con los amigos, Musica Gratis 2025! Fox.MusicaDe.Win!.

Video de: Incha Allah Lyrics Ismael Lo » Lyrics

Ismael Lo - Incha Allah Lyrics


Incha allah incha allah
Bou eulegue dana bakh
Incha allah incha allah
Bou eulegue dana bakh

Xalass warouna halebi mougui dieme
Di wout yone boumou beugue wayak
Bayam bay yemou nèko dome togal
Khar aduna ndakh diaroul guawtou
Amna fo wara diare kon khamna bou
Eleugue dana bakh
Bossi andék pass pass
Kon baye tok néko

Incha allah incha allah
Bou euleugue dana bakh
Incha allah incha allah
Bou euleugue dana bakh

Adouna diaroul gawtou
Téla soti bakhoul
Kon diangal bassi kanan
Bou mokke dana yomba lol ba diakhal

La waye nak defsi sa fulak sa fayda
Ndakh kou niakha dina diarignou
Mane kon dome adunabi diarul
Di gawtou
He he he he he

Incha allah incha allah
Bou euleugue dana bakh
Incha allah incha allah
Bou euleugue dana bakh
Incha allah incha allah
Bou euleugue dana bakh
Incha allah bou euleugue dana
Baaakh
Incha allah
Bou euleugue dana baaakh
Incha allah incha allah
Bou euleugue dana baaakh
He he he hee
Adouna amul solo oh
Incha allah incha allah
Dana bakha hehe hehe

Incha Allah » Ismael Lo Letras !!!