Video de: Dafmay Dal Feat Le Raam Daan Lyrics Wally B Seck » R B Fox.MusicaDe.Win

Bienvenidos a Fox.MusicaDe.Win Disfruta del Video de: Dafmay Dal Feat Le Raam Daan 2025 Wally B Seck » R B y comparte musicas con los amigos, Musica Gratis 2025! Fox.MusicaDe.Win!.

Video de: Dafmay Dal Feat Le Raam Daan Lyrics Wally B Seck » R B

Wally B Seck - Dafmay Dal Feat Le Raam Daan Lyrics


Taay ma netalilen man lima dal si
Sama dingantek xalleh bima tal
Thiono ngantal moy lima dal
Man deh lima dal moy kouma dimbaleh

Taay ma netalilen man lima dal si
Sama dingantek xalleh bima tal
Thiono ngantal moy lima dal
Man deh lima dal moy kouma dimbaleh

Lek lek ma xolko dioy sax dafmay dal
Mba ma xolko reh si dafmay dal
Thiono ngantal moy lima dal
Man deh lima tal moy kouma dimbaleh

Lek lek solou bay dem mom mou terema
Ma daldi tok li dafmay dal
Melni kouko ragal dafmay dal
Man deh lima dal moy kouma dimbaleh
Tokna di waxtan bis mak samay waay
Telephone bi sonner mouy mom ma daldi daaw
Melni kou ragal sax dafmay dal
Man lima tal moy kouma dimbaleh ehh waaw

Dieulinala nandeuna ningay doxeh eh hee
Anh anh sa bay moussouniouma
Gnenkouleh sa ba
Lakari lelelaw, gnekamouleh guemou xadila
Anh moussoletou lakari lelelaw

Worrna buur bi yalla niou boleh et sii yamalen gueuneul soxna
Nadipeh ba wakanda ndawsi deh moy sama seuytaneh
Mbatam hoo iow dieuleul, annh hi yeah, woo woo waawaw

Dama am sa faiblesse xolbi yassiy fess
Deugleu dila dianer di dioy dafmay dal

Guissoulon ngagni gueumeu touniouma yenneu
Say ma beugueu diengou gueneuthie dafmay dal

Thiono gui thie beuguel diarnako doyna warreh
Damay woo dame sene sama kaw scène
Takalko chaine nguir mou beguelalmalen

Guissouloni gagni gueumeutouniouma gnom deh louma wax niounima baxna
Dioxnala thieur ba melni koula ragal dafmay dal
Awmathie kersa deugueulani diam si iow lakoy ameh dafmay dal
Mala tal yama tal di defal sama gagni dafmay dal waaw
Wooy thionoh ngui thie beugeul diarnako doyna warreh

Dafmay Dal Feat Le Raam Daan » Wally B Seck Letras !!!

Videos de Wally B Seck

Esta web no aloja ningun archivo mp3©Fox.MusicaDe.Win 2025 Colombia - Chile - Argentina - Mexico. All Rights Reserved.

Musica Online, Escuchar musica online , Musica En Linea, Musica en linea gratis, Escuchar Musica Gratis, Musica Online 2025, Escuchar Musica

Musica 2025, Musica 2025 Online, Escuchar Musica Gratis 2025, Musica 2025 Gratis, Escuchas, Musica de Moda.