Video de: Dangerous Feat Mgeey Lyrics Samba Peuzzi » Lyrics Fox.MusicaDe.Win

Bienvenidos a Fox.MusicaDe.Win Disfruta del Video de: Dangerous Feat Mgeey 2025 Samba Peuzzi » Lyrics y comparte musicas con los amigos, Musica Gratis 2025! Fox.MusicaDe.Win!.

Video de: Dangerous Feat Mgeey Lyrics Samba Peuzzi » Lyrics

Samba Peuzzi - Dangerous Feat Mgeey Lyrics


Fay while we dance o
Fay while we dance o
Feel (Vibe) energy when we dance o, yeah
Feel (Vibe) energy energy

Your body is so dangerous
Your body is so dangerous
Your body is so dangerous
Your body is so dangerous

Yeah Yeah
Me i dey cool i dey fine
I dey cool on my mind
Me no dey stress you deh mine
Gimme more lo’ on the night yea yea
Yaay sama leer sama naaj
Sama bideew sama light
Sama takkandeer sama waay
Jox la sama bopp doy nga ma njegenaay

Yaay sama queen sama love
Sama waay sama gayin sama xaaj nga you know, yeah
Yaay sama queen sama love
Sama waay sama gayin sama xaaj nga you know, yeah

Man doffu ma ba di la foowe
Topp ma ñu dem fu sore
Yaa nekk sama mind yow baby foo nekk
Sama yaayu doom rekk laa lay xoole

Fay while we dance o
Fay while we dance o
Feel (Vibe) energy when we dance o, yeah
Feel (Vibe) energy energy

Your body is so dangerous
Your body is so dangerous
Your body is so dangerous
Your body is so dangerous

[Samba Peuzzi]
Ku sa gel tooy loy utt ci gellu jambur ba ciy xeex
Ku sa gel mool waawaw loy utt ci gellu jambur ba ciy xeex bae xool
Man dam laa gis rekk dof mel ni sum-sum laa naan
Feete ma kanam ñu fecc pum-pum turn up
Boomerang sama xol bae lu dem day ñëwaat
Badman bi moo fi nekk sa ex chinois lay lakk
I say Nĭhǎo, baby
Tòntu ma gaaw
Nah yow laa nobb

Man doffu ma ba di la foowe
Topp ma ñu dem fu sore
Yaa nekk sama mind yow baby foo nekk
Sama yaayu doom rekk laa lay xoole

Fay while we dance o
Fay while we dance o
Feel (Vibe) energy when we dance o, yeah
Feel (Vibe) energy energy

Your body is so dangerous
Your body is so dangerous
Your body is so dangerous
Your body is so dangerous

Dangerous Feat Mgeey » Samba Peuzzi Letras !!!
Esta web no aloja ningun archivo mp3©Fox.MusicaDe.Win 2025 Colombia - Chile - Argentina - Mexico. All Rights Reserved.

Musica Online, Escuchar musica online , Musica En Linea, Musica en linea gratis, Escuchar Musica Gratis, Musica Online 2025, Escuchar Musica

Musica 2025, Musica 2025 Online, Escuchar Musica Gratis 2025, Musica 2025 Gratis, Escuchas, Musica de Moda.