Video de: Dawalale Lyrics Samba Peuzzi » Lyrics Fox.MusicaDe.Win

Bienvenidos a Fox.MusicaDe.Win Disfruta del Video de: Dawalale 2025 Samba Peuzzi » Lyrics y comparte musicas con los amigos, Musica Gratis 2025! Fox.MusicaDe.Win!.

Video de: Dawalale Lyrics Samba Peuzzi » Lyrics

Samba Peuzzi - Dawalale Lyrics


Li ma yëg ci xol bi du deñ
Mbëggeel dëgg xol du fen
Su ma la tooñee danga ma baal
Bi ma ñépp folee yaa ma fal
Yàlla def fi ñu yegsi tay
Kon nak duma bàyyi lu mu metti-metti
Kon waroo tiit, ndax dootoo wéet
Fi lek yaa ngi geestu gis ma ci sa wet

Kenn du la jam naa ni
Gilet pare balle maa ngi ni maa lay aar
Ci sa wet laay fanaan ci
Lu mu guddi guddi bae ndag ma xaar

Kaay jege ma, nga wax ma
Chérie boo bëggee bëgg naa
Boo bëggul bëgguma
Yaw jege ma, wax ma
Boo bëggee bëgg naa
Boo bëggul bëgguma

Ay dawalal, chérie dawalal
Yaa téye volant bi bul taxaw, dawalal
Ay dawalal, mon bébé dawalal
Yaa téye volant bi bul taxaw, dawalal

Day metti rekk waaye
Ñun ñaar ñooy àndandoo
Ku la bañ, lam bañale
Ndax ñun ñaar ñooy àndandoo

Man bëgguma ragal naa
Nit di dox di ma gis sans yaw
Kon du nice
Yaw danga ma fan dama la fan
Li nga gis ci man ne ci yaw
Xol bu nice

Man naa la jàpp yëkketi la
Ba nit yépp xam ni yaw la
Sama xol bae yaa ko damp
Di ko bëgg noo ko bëggee
Yaa ko fa am danga ma jege
Yokk ma ndam mbide yide ma
Te noo ko bëggee bëgg naa

Kaay jege ma, nga wax ma
Chérie boo bëggee bëgg naa
Boo bëggul bëgguma
Yaw jege ma, wax ma
Boo bëggee bëgg naa
Boo bëggul bëgguma

Ay dawalal, chérie dawalal
Yaa téye volant bi bul taxaw, dawalal
Ay dawalal, mon bébé dawalal
Yaa téye volant bi bul taxaw, dawalal

Day metti rekk waaye
Ñun ñaar ñooy àndandoo
Ku la bañ, lam bañale
Ndax ñun ñaar ñooy àndandoo

Dawalale » Samba Peuzzi Letras !!!
Esta web no aloja ningun archivo mp3©Fox.MusicaDe.Win 2025 Colombia - Chile - Argentina - Mexico. All Rights Reserved.

Musica Online, Escuchar musica online , Musica En Linea, Musica en linea gratis, Escuchar Musica Gratis, Musica Online 2025, Escuchar Musica

Musica 2025, Musica 2025 Online, Escuchar Musica Gratis 2025, Musica 2025 Gratis, Escuchas, Musica de Moda.